Numbers 9:10 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«Waxal bànni Israyil ne leen, képp ku bokk ci yeen tey, mbaa mu bokk ci seen kuutaay ëllëg, su sobewoo ndax ab néew, mbaa mu nekk ci yoon wu sore, du tere mu màggal bésub Mucc bi ngir Aji Sax ji.