Obadiah 1:11 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Bésub keroog ba ngeen taxawee, janook seen mbokk, bésub keroog ba jaambur ñay yóbbu seen alali bokk, ay doxandéem song bunti dëkkam, bay tegoo bant teraangay Yerusalem, yeen itam, ni noon yooyu ngeen def.