Obadiah 1:14 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waruleen woona taxaw fa selebe yoon ya, di dogale ña rëcce ca ñoom, waruleen woona delloo ña dese bakkan ca loxol noon ya, ci bésub njàqare.