Obadiah 1:7 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Mboolem ñi ngeen fasool kóllëre ñoo leen di waññi ba ca seen kemu réew, seeni am-di-jàmm ñoo leen di nax ba man leen, ñiy lekk seenu ñam tegal leen ag fiir ci seeni tànk, ndax Edom moo amul ag dégg.