Philemon 1:13 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Dama koo bëggoon a téye fi sama wet, ngir mu taxawal la, di ma dimbali, li feek maa ngi ci kaso bi ngir xebaar bu baax bi.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Dama koo bëggoona téye fi sama wet, ngir mu taxawal la, di ma dimbali, li feek maa ngi ci kaso bi ngir xibaaru jàmm bi.