Philemon 1:15 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Xëy na sax dafa tàggoo woon ak yaw diir bu gàtt, ngir nga jotaat ci ba fàww;
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Jombul itam dees koo tàggale ak yaw ab diir, ngir nga jotaat ci moom ba fàww,