Philemon 1:20 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaw yaw sama mbokk, dimbali ma ci Boroom bi, te seral sama xol ci sunu bokk ci Kirist.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Kon nag mbokk mi, may ma googu njekk ngir Sang bi, te nga seral sama xol ndax Almasi.