Philemon 1:6 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Li may ñaan nag a ngi nii: nga xam bu wér ngëneel, yi nu am yépp ci sunu bokk ci Kirist, ba tax bokk gi nga am ci Yàlla ci kaw ngëm meññ i njariñ.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Damay ñaan nag sa ngëm, gi nu bokk amal la njariñal ràññee mboolem ngëneel, yi nu am ci Almasi.