bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare Philemon 1:7
Philemon 1:7 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Ci dëgg-dëgg sa mbëggeel bégal na ma bu baax, ba dëfël sama xol; ndaxte xam naa, sama mbokk, ni nga féexale xoli gaayi Yàlla yu sell yi.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Mbokk mi, mbégte mu réy, ak xel mu dal laa am ci sa cofeel, ndax ni nga serale xolu aji sell ñi.