Philemon 1:9 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
waaye dama lay ñaan ci mbëggeel gi nu séq, man Pool màggat, mi ñu tëj kaso ci turu Kirist.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
waaye tinu la ci ngir cofeel, mooy li ma taamu, man Póol mu màggat mii, boole ci léegi tënku biir kaso ndax Almasi Yeesu.