Philippians 1:12 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Damaa bëgg, bokk yi, ngeen xam lii: li ma dal taxul xebaar bu baax dellu gannaaw, waaye da koo jëmale kanam.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Damaa bëgg, bokk yi, ngeen xam ne lii ma dal, xibaaru jàmm bi la far jëmale kanam.