Philippians 1:13 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Noonu ñiy wottu buur bi ak ñépp gis nañu bu leer ne, turu Kirist rekk a tax ñu jàpp ma.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ndax kat, bir na mboolem dagi boroom dëkk bi te bir na ñeneen ñépp ne Almasee tax ñu jéng ma.

Recommended Reading