Philippians 1:14 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Te it bokk yu bare takk nañu seeni fit ci li ñu gis samay buum, ba tax ñu gën a ñeme ci wax kàddug Yàlla ci lu àndul ak genn tiit.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Te it li gëna bare ci bokki gëmkat ñi, sama jéng yi ma nekke nii moo leen yokk aw fit, ba tax ñu gëna ñemee waxe kàddu gi te ragaluñu ci dara.