Philippians 1:15 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Am na ñuy waare ci turu Kirist ci kaw kiñaan ak xëccoo, waaye ñi ci des ci kaw cofeel ak xol bu laab, ndaxte xam nañu ne, Yàlla moo ma teg fii, ngir ma taxawal xebaar bu baax bi.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Dëgg la am na ñuy waare turu Almasi ci kaw kiñaan ak diiroo mbagg, waaye am na itam ñu koy defe yéene ju rafet.