Philippians 1:19 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ndaxte xam naa ne, loolu lépp mu ngi jëm ci sama mucc, jaar ci seeni ñaan ak ndimbalu Xelum Yeesu Kirist, mi ma Yàllay yéwénal.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
ndax xam naa ne loolu lépp ay walbatiku di samag mucc, ndax seeni ñaan, ak ndimbalal Noowug Yeesu Almasi.