Philippians 1:22 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Su ma Yàlla bàyyee ci àddina, sas wu am njariñ la ci man. Am naa xel ñaar, te xawma bi ci gën. Am naa yéeney jóge fi, fekki Kirist, te looloo gën fuuf,
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Su dee nag damaa wara wéye sama bakkan bii, ngir mana sottal ab liggéey bu am njariñ, ana lu ma gënal ci diggante dund ak dee? Xawma ko.