Philippians 1:25 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Loolu wóor na ma; kon xam naa ne, dinaa fi des, di leen taxawu yéen ñépp, ngir seen ngëm yokku, ànd ak mbég.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Gannaaw loolu bir na ma nag, xam naa ne dinaa desagum, desandoo feek yeen ñépp, ngir ngeen jëm kanam, tey bége seen ngëm,