Philippians 1:26 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Noonu dinaa dellusi ci yéen, ngir sama taxawaay gën a lawal seen mbég ci Kirist Yeesu.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
ba bu ma délsee fi yeen, ngeen gëna mana puukarewoo Almasi Yeesu ndax man.