Philippians 1:28 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
te bañ a tiit dara ndax noon, yi leen di xëbal. Màndarga la muy wone ne aji sànku lañu, di màndarga it ne aji mucc ngeen, di mucc gu jóge ci Yàlla.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Buleen ragal seeni noon ci lenn. Seen fit mooy màndargaal sànkutey noon yi, te yeen it, mooy màndargaal seenug mucc gu bawoo fa Yàlla.