Philippians 1:9 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Li ma leen di ñaanal nag mooy lii: na seen mbëggeel di yokku tey gën a tar, jaar ci xam ak xàmmi gu wér;
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Li may ñaan nag moo di seen cofeel yokku tey gën di yokku, te ngeen ànd ceek xam-xam bu matale ak gépp ràññee,