Philippians 2:1 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Su nu Kirist mayee fit nag ak mbëggeel guy dëfël sunu xol, su nu amee cér ci Xel mu Sell mi, su amee cofeel ak yërmande ci sunu bokk ci moom,
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ndegam amees na lenn lu yokk aw fit ci Almasi mi nu gëm, ndegam lenni cofeelam lu mana dëfal am na, ndegam amees na benn cér ci Noo gu Sell gi, ndegam it, amees na lenn lu bawoo fi moom, ci wàllu xol bu rafet, ak yërmande,