Philippians 2:10 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
ngir turu Yeesoo tax ñépp sukk,ci asamaan, ci kaw suuf, ci biir suuf;
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
ba turu Yeesu tax ñépp sukk seen bëti óom, muy kaw asamaan, di kaw suuf, di biir suuf,