Philippians 2:11 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
te ñépp bokk genn kàddu naan:Yeesu Kirist mooy Boroom bi;ci màggug Yàlla Baay bi.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
làmmiñu ñépp it biral ne Yeesu Almasi mooy Sang bi, te muy ndamu Yàlla Baay bi.