Philippians 2:13 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ndaxte Yàlla ci boppam mooy jëf ci yéen, ngir ngeen fonk coobareem te di ko jëfe.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
ndax Yàlla mooy liggéey ci yeen lu tax ngeen mana namma jëfe coobareem, ba man koo jëfe.