Philippians 2:15 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Noonu dingeen am xol bu laab bu àndul ak ŋàññ, di guney Yàlla yu amul sikk ci biir jamono ju yàqu te rëb. Dangeen di leer ci seen biir ni weer ci àddina si,
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
ngir seen der set wecc, te kon deesuleen mana gàkkal ci lenn. Ay goney Yàlla yu amul sikk ngeen di doon, ci biir maas gu dëng te yàqu, ngeen di lerxat ci seen biir, ni ay leer ci àddina si,