Philippians 2:18 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Yéen itam nag bégleen, waaw fekksileen ma ci sama mbég.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Yeen itam nangeen ci bég te bokk ak man bànneexu.
Recommended Reading