Philippians 2:19 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Gannaaw loolu, bu soobee Boroom bi Yeesu, yaakaar naa ne, dinaa leen yónnee Timote balaa yàgg, ngir sama xel dal ci xam nan ngeen def.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Yaakaar naa nag, ne bu soobee Sang Yeesu, dinaa leen yónnee Timote balaa yàgg, ngir xam nu ngeen def, ba man ci sama bopp, sama xel dal.