Philippians 2:21 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Ñi ci des ñépp, seen bopp lañuy xalaat, waaye du mbiri Yeesu Kirist.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ñi ci des ñépp, seen njariñal bopp lañuy sàkku, waaye du li soxal Yeesu Almasi.
Recommended Reading