Philippians 2:25 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Ci lu jëm ci sama mbokk Epafrodit nag, miy sama nawle ci liggéey bi ak ci xeex bi, te di seen ndaw ci faj samay soxla, jàpp naa ne, war naa leen koo delloo.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ci wàllu Epafrodit, sama mbokkum gëmkat la, di sama naataango, di sama mbokkum xarekat, te di seen ndaw li ngeen ma yóbbante ndimbal lu faj samay soxla. Waaye jàpp naa ne fàww ma delloo leen ko,