Philippians 2:27 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ci dëgg-dëgg woppoon na ba xaw a dee, waaye Yàlla yërëm na ko, ba fëgg boppam, rax-ca-dolli siggil na ma man itam, ngir ma bañ a am tiis ci kaw tiis.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Woppoon na it ba xawa dee, waaye Yàllaa ko yërëm, te du moom rekk la yërëm, waaye man itam, ngir ma baña am tiis ci kaw tiis.