Philippians 2:29 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Teeruleen ko teeru bu rafet nag ngir Boroom bi, te teral ñi mel ni moom.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Teertooleen ko mbégte mu mat sëkk ngir Sang bi, te it nawleen ñu mel ni moom,
Recommended Reading