Philippians 2:30 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ndaxte liggéeyal na Kirist, ba riisu dee, te gar na bakkanam ci taxawal leen ci topptoo, bi ngeen yéene woon ci man.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
ndax liggéeyal Almasi tax na koo riisu ndee; ba ngeen amee ngànt lu leen teree mottlil seen bopp, seen yéene, moo jaay bakkanam ngir wuutu leen, ba yótsi ma seen ndimbal.