Philippians 2:7 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye daa wàcce boppam,ba tollook nit ñi,def boppam surga.Te bi mu yoree bindu nit,
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Xanaa mu ŋacc boppam, nangoo jagoo nekkinu surga. Mu mujj mel ni nit doŋŋ, di ku ñu xàmmee jëmmu nitam.