bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare Philippians 3:1
Philippians 3:1 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Kon nag samay bokk, bégleen ci Boroom bi. Duma sonn mukk ci di leen ko wax, ndax seen mucc moo ci aju.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Li ci des bokk yi, ma waxati, bégleen ci Boroom bi. Di leen bind genn kàddu googu rekk, diisu ma, te di leen ko baamtu moo gëna wóor ci yeen.