Philippians 3:13 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Bokk yi, gëmuma ne jot naa ko ba noppi, waaye lenn lii laay def: fàtte li ma weesu, jublu ci li féete kanam,
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Bokk yi, fooguma ne jot naa ci, xanaa kay lenn: damay fàtte li ci gannaaw, te def lu ma man, ngir fexee yóotuji li ci kanam,