Philippians 3:15 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Nun ñi mat nag, nanu xalaat loolu. Te su ngeen ci amee werantey xol, Yàlla dina leen ko leeralal.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Kon nag, nun ñi jota màgg ba di magi jëmm ci wàllu ngëm, nanu ko bokk gise noonu. Su ci amee lenn lu ngeen gise neneen nag, loola, Yàlla moo leen koy leeralal.