Philippians 3:20 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye nun waa asamaan lanu, te noo ngi xaar Boroom bi Yeesu Kirist jóge fa, musalsi nu.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Nun nag sunum réew a nga fa asamaan, fa nuy séentoo sunu Musalkat, Sang Yeesu Almasi.