Philippians 3:4 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ba tey manoon naa am yaakaar ci sama bopp; su nit doon damu, maa ciy raw.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Moona man de, waroon naa mana yaakaar aaday suuxu neen. Ak keneen ku mana xalaat ne sañ naa yaakaar aaday nitu suuxu neen, maa ci raw.