Philippians 3:5 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Xarafoon naa ca ayu-bés ga, bokk ci bànni Israyil ci giiru Ben-yamin, di Ibrë ci deret ak ci meen. Bu dee ci yoonu Musaa ngeen bëgg a wax, ci tariixab Farisen laa bokkoon;
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Man mi xaraf ba ma amee juróom ñetti fan, askanoo ci bànni Israyil, giiroo ci Beñamin, di ab Ebrë bu ñaari Ebrë jur, te bokk ci ngérum Farisen, ci wàllu yoonu Musaa.