Philippians 3:7 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye loolu lépp lu ma tegoon ay njariñ fa kanam Yàlla, dëddu naa ko ngir Kirist.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waaye la ma jàppe woon ag ndollant, moom laa def tey ag wàññeent ndax Almasi.