Philippians 4:10 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Sama xol sedd na guyy ci Boroom bi, ci ni ngeen yeesale seen ndimbal ci man. Xam naa ne, amoon ngeen yéene ji, waaye man gi moo fi nekkul woon.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Maa ngi bége Boroom bi lool ci nii ngeen mujj yeesale tey, seen yitte ci man, yitte ju ngeen amoon moos naka jekk, xanaa dangeena ñàkkoona jekku seen ndimbal.