Philippians 4:15 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Yéen waa Filib xam ngeen ne, bi ngeen jëkkee xam xebaar bu baax bi, te ma jóge diiwaanu Maseduwan, benn mbooloo àndul woon ak man ci mbirum joqleente ndimbal, mu dul yéen doŋŋ.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Yeen waa Filib, xam ngeen xéll ne ba waareb xibaaru jàmm bay door, te ma bàyyikoo diiwaanu Masedwan, amul woon menn mbooloom gëmkat mu ma séqaloon ab joqlanteb ndimbal, xanaa seen mennum mbooloo.