Philippians 4:16 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ba ma nekkee dëkku Tesalonig sax, yónnee ngeen ay yooni yoon, ngir faj samay soxla.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ba ma nekkee Tesalonig sax, yónnee ngeen ma ay yoon, lu ma faje samay soxla.