bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare Philippians 4:17
Philippians 4:17 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Loolu tekkiwul ne, damay sàkku ay ndimbal ci yéen, waaye damaa bëgg rekk seen denc yokku fa Yàlla.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Du caageenu ndimbal lu ma leen di sàkku, li may sàkku kay moo di yokkuteb yool bu leen ñeel.