Philippians 4:3 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Te yaw sama nawle bu wér, nanga dimbali jigéen ñooñu xeexoon ci sama wet ci tas xebaar bu baax bi, boole ci Këlemaŋ ak samay yeneeni nawle, ñoom ñi Yàlla bind seeni tur ci téereb dund ba.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Yaw itam sama mbokkum surga bu dëggu bi, dama lay ñaan nga jàpple leen ci, ñoom ñaar ñooñoo bokkoon ak man coonob xamle xibaaru jàmm bi, ñoom ak ñoom Kelemaŋ, mboolem sama bokki liggéeykat yi seeni tur binde ca téereb dund ba.