Proverbs 24:12 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Soo nee sa yoon nekku ci it, kiy natt xol yi, xam na, moom miy wattu sa bakkan, xam na, te kat mooy fey nit jëfam.