Psalms 137:6 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Yerusalem, su ma la fàttlikuwul, fonk la, ba gën laa bége lépp, yal na sama làmmiñ tafoo sama denqleñ.