Psalms 59:1 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Mu jëm ci njiital jàngkat yi, dëppook galan bi ñuy wooye Bul yàq, di taalifu jàngle bu Daawuda fentoon. Mooy ba Buur Sóol yónnee ay nit ñu ko xoolal kër Daawuda, ngir rey ko.