Psalms 83:12 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Defal seeni njiit na Oreb ak Seeb, def seen kilifa yépp ni Seba ak Salmuna,