Revelation 1:11 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
naan: «Bindal ci téere li ngay gis te yónnee ko juróom-ñaari mboolooy ñi gëm, ca dëkki Efes, Samirin, Pergam, Catir, Sàrd, Filadelfi ak Lawdise.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Mu ne: «Mboolem loo gis, bind ko cib téere, nga yónnee ko juróom ñaari mboolooy gëmkat ña ca dëkk ya ñuy wax Efes ak Samirin ak Pergam ak Catir ak Sàrd ak Filadelfi ak Lawdise.»